1 Matching Annotations
  1. Mar 2021
    1. VERB CONJUGATION

      Indicative / Present

      damay dem (I go)

      dangay dem (you go) singular

      dafay dem (he/she goes)

      dañuy dem (we go)

      dangeen dem (you go) plural

      deñuy dem (they go)


      Indicative / Imperfect

      dama doon dem (I went)

      danga doon dem (you went) singular

      dafa doon dem (he/she went)

      dañu doon dem (we went)

      dangeen doon dem (you went) plural

      deñu doon dem (they went)


      Indicative / Pluperfect

      demoon naa (I had gone)

      demoon nga (you had gone) singular

      demoon na (he/she had gone)

      demoon nañu (we had gone)

      demoon ngeen (you had gone) plural

      demoon nañu (they had gone)


      Indicative / Future

      dinaa dem (I will go)

      dinga dem (you will go) singular

      dina dem (he/she will go)

      dinañu dem (we will go)

      dingeen dem (you will go) plural

      dinañu dem (they will go)


      Imperative / Active

      demal (go!) singular

      demleen (go!) plural


      Negations

      demumaa (I didn’t go)

      demul (he/she didn’t go)

      demunu (we didn’t go)

      demuleen (you didn’t go)

      demuñu (they didn’t go)