- Mar 2021
-
jangawolof.org jangawolof.orgPhrases2
-
Fibar bi jàngal na taawan bu góor ni ñuy dagge reeni aloom.
Le guérisseur a appris à son fils aîné comment on coupe les racines du Diospyros.
fibar -- (fibar bi? the healer? as in feebar / fièvre / fever? -- used as a general term for sickness).
bi -- the (indicates nearness).
jàngal v. -- to teach (something to someone), to learn (something from someone) -- compare with jàng (as in janga wolof) and jàngale.
na -- pr. circ. way, defined, distant. How? 'Or' What. function indicator. As.
taaw+an (taaw) bi -- first child, eldest. (taawan -- his eldest).
bu -- the (indicates relativeness).
góor gi -- man; male.
ni -- pr. circ. way, defined, distant. How? 'Or' What. function indicator. As.
ñuy -- they (?).
dagg+e (dagg) v. -- cut; to cut.
reen+i (reen) bi -- root, taproot, support.
aloom gi -- Diospyros mespiliformis, EBENACEA (tree).
-
Dafa ànd ak moroom yi àll ba, fori aloom.
Il est allé dans la brousse ramasser des fruits de Diospyros avec ses camarades.
dafa -- he/she.
ànd v. / ànd bi -- to be together, to go together; copulate; going together, fellowship; placenta.
ak -- and, with, etc.
moroom mi -- comrade of the same age group, equal, companion, neighbor.
yi -- the (plural).
àll bi -- large expanse of uninhabited land, bush; distant, as opposed to home.
ba -- the (indicates distance).
for+i (for) v. -- to pick up.
aloom bi -- edible fruit of Diospyros mespiliformis (aloom gi for the tree).
Tags
- man
- aloom
- land
- gi
- comrades
- taproot
- dagg
- with
- ba
- -e
- comrade
- ni
- góor
- companion
- together
- ebenacea
- reen
- equal
- fever
- teach
- dagge
- fellowship
- healer
- fori
- learn
- ñuy
- ak
- na
- eldest
- into
- uninhabited
- support
- janga
- jàng
- sickness
- bu
- child
- collect
- son
- jàngal
- fièvre
- to
- taaw
- his
- roots
- they
- diospyros
- copulate
- àll
- bi
- -an
- the
- of
- she
- mi
- neighbor
- for
- taught
- first
- mespiliformis
- went
- wolof
- yi
- moroom
- fruit
- as
- male
- pick up
- placenta
- distant
- ànd
- taawan
- fibar
- he
- and
- -i
- tree
- what
- reeni
- cut
- feebar
- how
- jàngale
- dafa
- bush
Annotators
URL
-